MULTIPLE PHOTOSPARLONS ÉCONOMIE EN WOLOF ET EN PULAAR
L’ECO, LES EGOS ET LEURS ECHOS - Il est tout aussi fondamental que l’énergie mise par les acteurs sociaux pour arriver au résultat obtenu soit dorénavant tournée vers les autorités des Etats de la CEDEAO pour accélérer l’unité de gouvernance politique
SenePlus publie en exclusivité, la traduction en wolof et en pulaar d'un article déjà publié sur notre site par l'ancien ministre de Finances, Amadou Kane. La traducution en wolof est de Moustapha Diop et celle en pulaar d'Abdou Amadou Sy.
Dans le cadre de son déploiement Riposte educative et libératrice autour du COVID 19, la Paalae que dirige Babacar Bouba Diop partage par une approche multimédia, multilingue, multiscript, des analyses, le suivi et les perspectives de transcroissances solidaires, positives et durables. Elle constate que les exercices d'intersectionalites entre la politique, l'économique, la santé, l'éducation, la culture, sont en œuvre. C'est pourquoi la Paalae prête attention aux débats en cours sur les moratoires et ou annulation des dettes des pays du Tiers Monde. Elle tient à partager la traduction du français au pulaar et wolof d'un texte produit par l'expert Elhadj Amadou Kane sur l'eco. Elle poursuit en son sein des réflexions sur la pertinence et les dénominations des monnaies nationales, régionales, voire continentale. Elle espère qu il y aura des modalités pratiques et inclusive pour avancer dans ce dossier et dans les articulations libératrice et fécondes
VERSION WOLOF - EKO BI, AK FUUY AK RIIR YI MU ÀNDAL
Dogal yi aju ci xaalisu CFA ab bob eko, te siiwalees ko ci 21 desambar 2019 ca Abijaan ci dogalab Alsaan Watara, ndax maxaamàm kilifa gi jiité ndajéem njiiti réew yi séq UEMOA, ak ci teewaayu njiitël réewu Farans, daa ñu ci wax, di waaxaat lu yàgg yàgg.
Jaaxlewul kon, ni ko xibaar yi tasaaree, monte dey bette na ni waxtaan wi deme, jolli ginaaw bi xew xew bi jibee, njortu yi mbooloo mi bàyyi xel, ñoo gën bari pexe yi ñu ko sàkkuloon, balaa siiwalees cóppite gi ! Aka doy waar : « leppay soppeeku, te katt dara soppekuwul ! »
Monte, ni ki ñi nu wara natte, jublu ci liy wekki yiy doxal ak yaxantu gug xaalis CFA, wone, na lees amal», sopparñig tuddin yi, kaaraange sàq mi, dàqug ña teewaloon Farãns, ci mbootaayu UEMOA, noo nu la yoon wi desee leer ci ni nuy tege.
Ńu yokk ci, kenn ci ndaw yi sunuy gornemaa teg ci kureel yiy saytu sunu xaalis, kenn ci ñoom mënul mbaa bëggul joxoñ ab arminaat gu leer ak warangikuk doxandin wi gën, ngir jëmmël coppite gu mat sëkk. Te monte, xamees na ni, semb wu ni yaatoo nii, ngir amal ko, du yem ndoŋ ci ñatti pacci weccoo ?
Semb wu ni mel laaj na lumu tuuti tuuti :
- Ci settantalaat faggutéef yi ak àtte yiy taxawal yaxantug weccet wi, yorinu kureel yi ak dëgmël ci yoonu doxalinam ci yoonu jumbëntiku;
- Tegal kureel yu yees yi, rawatina sàqum gëndële mi yellu fii ñu tollu ; ci maanaa yi war ak jumtuwaay yi ci aju ak ñu àajoowu ci jëm ci bépp jumtuwaay yu jub te am solo ;
- Wone nan lanuy wara dàkke ci mbirum xaalis, nun ñi wara jubóo, fekk nu am ay kureel yu bari, te wute ci sunuy réew.
- Deggóo ci wecconte gu amal njariñ, ku ci nekkdem, ci ndank ndank, ca njalbéen, mën nañ ko yombal, su yàgge tuuti te nu wone mënin, ci yaatal jënd ak jaay ak yaxanal xaalis. Bu boobaa nu aldande fépp ;
- Saytu ni nuy wuutële sefaa bi ak eko (këyit ak paset yi).
Laajtu yu am maanaa ngi nii, faydawu te yéeme, dina jaaxle, ndax ken mënul jeexal waxtaan wi ci dirap atum 2020.
Fuuyte waru noo yobe yàkkamti, ci tëg xaalis bu bees ci atum 2020. Mbir yii am na ñu solo lool, ba ken waarul yàkkamti ci déggóo, ba jubóo. Rax ci dolli, mën na am ñu laaj ndaw wi réew mi, seen xalaat.
Bu ko defee, ndëgg sërëx gi nu wara gëna moytu bu baax, mooy ba ña gedd Eko, ndax rekk ni ko persidáa Watara yerëwte ci kanam persidaa Macron, wax fa ne daa ñu ngente Eko bi, suul Sefaa bi, ndax warna ñu nëq Sefaa bi ?
Te it, warees na fàtteliku ni tëgg Eko ak sart yi dar sàqum gëndële mi, nangu gi CEDEAO cërële réew yi bokk mandargam wecconte mën na door tëgg xaalis bu bees bi nu bokk. Lolu lépp doon na ay dogal yi jiitu yërëwte gu 21 desambar 2019. Kon book, na nu féetéwóo si teel sooke gi jëmmël ko ci ko CEDEAO gise ca njalbén ngir nu am ci mujj gi, ngir nu am xaalis bi ñu bokk.
Taxawaay bile daa yemoog ag ni Gaanaa gise moom mi begóon ca 28 désambar 2019, ci na réewi UEMOA yi ànd jubóo ci EKO, noo nu ci la xamle ni di na léen fekki. Loolile, ndajem njiiti réewi CEDEAO daadi ka rafetlu ; mu yemóog 21 desambar 2019, ñu àndandoo ci ak sawar ci ni ko UEMOA jële, ni jibal ci kaw ni « coppite bi am ci biir UEMOA, ci mbiri xaalis ; dina yombal rofóo bi nara am ellëg ci wàllu xaalis, ngir nu yaatal EKO, mu doon bu CEDEAO»
Na leer naññ ne, lu ñu bëgg bëgg bokk xaalis ci biir CEDEAO, bu nu réere mbir ne ni bokku ñu, ñun nëpp, bëgg bëgg ci wàllu politigu xaalis, ci mbiram demantale ak weccikonte.
Looluu tax na, bi ci waxtaan yiy am ci diggënte réew yi ko seqóo, waru nu dugël xóoyal bu nara dog. La ñu fa jàpp ak sabablu ya leen tënk, war nanoo joxe firnde yu wóora woor, te ànd ag ndëgërlaay, ba kenn ku ci ne, mën caa gis sa bopp, ca lam cay jële, ak la mu cay ńàkk.
Da maa bokk ci ńiy jëf ngir gëndëlóog Afrik, ni ko sa may jaar jaarn ci liggéey, wonee nañ ko ; moo xam ci liggéeyal réew yi fostóo ca BOAD, ci kureel mbootaayi jaambur yiy liggeey Afrik ci sóàwu jant ak ci Afrik gi diggu ; rax ci dolli, bokk ci ńi liggeey ci wetu BAD, ba samp Afrika 50, mooy sàkuu alal, féetelées ko jumtukaay, ci dun bi bepp.
Leer na ci sama bopp, war na nu sàmm njariñal ku ne, leeg leeg nu woróo ; mbir mi du yomb, di na metti ci nii mbaa ca nee ; balaa CEDEAO dóon benn, di te xemeemu, xaalis bu yees bu di Eko, bokk ci liy jagal, di sopparñi ak di dooléel ak di yokk kureel yi ak jumtukaayu koom-koom mi mbooloo yi nas, loolu doon njarińal li ñi bokk ńun népp moom CEDEAO. Li nu war moodi dëgërël mbootaay gu yaatu gi, te kenn waru ci jaamulooti sa moroom.
Loo loo tax ne ; na nu wóor, ci njalbeen, ci wetu Niseeriyaa, ponkal mi, am na lu mu neew neew, réew yu waro danko, maanam juróom ńatti réew yi sèq UEMOA, the ngańaayoo mën mën ak doxalin wu wer ak finalikug BCEAO, ngir mbootaay gi wer, mel ni na ka Almaañ ak Farãns ñoddee réewi Erop yi.
Bu demee, ba dëgg des, li gën, mooy def degg ni ko Gaanaa siiwale ci 28 desambar 2019 ni Gana nangu na na fekki réewi UEMOA, ci njalbéenug jamonal Eko, yokk dank bi mëna jakkarlo ag ponkal mi di Niseeriyaa, ci weer yii di ńëw.
Li leer moodi kàttan ni, ñepp di def, ñepp niy yengu ci jamono ngir àgg fi nu bègg bègg àgg ci, moom la nu war welbati, jubal ci xolu, njiit yiyor ndomboy tànk te Ŋank su nu réew yi ne CEDEAO, su ko defee, loolu moodi sàmm ci lu wóor, politigi xaalis yi nu jagleel kureel yu bees yi gëndëlóo, te war saytu Eko bi.
Ki ko bind Aamadu Kan, newoon jawrin ci xaalis ak kom kom ci Senegal, tay jii doxal mbiri boppam ci xaalis ak kom kom
VERSION PULAAR - ECO, HAKKUNDE PIITAGOL BECCE E OOLELAAJI (PULAAR)
Yeɓtugol jamirooje jowitiiɗe e lomtingol ECO CFA caaktagol ñande noogaas e go (21 Lewru desammburu 2019 to wuro Abidjan e ummoraade e ɗemngal Alasan watara gardiiɗo Diisnondiral Hooreeɓe Dowlaaji UEMOA (Dental fagguduyaŋkeewal e kaalisiyaŋkeewal Leyɗeele Hirnaange Afirik) e dow tawtoregol Hooreejo Dowla Farayse,ko huunde maabtiniinde e taarik men .
Ɗum waɗi saakto mawngo waɗaango e nder Jaaynirɗe fotaani haawde hay gooto Hay sinno ina haawni caggal gostondire hakkilaaji,miijooji e jeewte e heen sahaaji nannduɗe e hare e duko,keewɗi e ceertuɗi ciiri,kono haa jooni ngoƴaaji e kulhuli ɗi yimɓe ɓe ngonndi ɗi hade baylugol kaalis gol waɗde,ina keewi no feewi ! Miijooji ɗiɗi kaawniiɗi lulndondirɗi ɓuri heewde : fof yoo waylo alaa hay dara waylaaki ».
Tene dey peeje e jamirooje pattamlame ngam ittude e fusde ngaafdi e njuɓɓudi lelngo e yiilo CFA ƴeɓtaama ( baylugol innde nde uddugol damal winndannde hasbo,jaltingol Hoolaaɓe Farayse e nder terɗe jiilirɗe UEMOA ( Dental fagguduyaŋkeewal e kaalisiyaŋkeewal Leyɗeele Hirnaange Afirik) ɗum holliri njoorto pawaaɗo e kaalis keso lomtotooɗo o laaɓaani tawo walla punndi mum gasaani tawo .
Yanti heen kadi hay gardiiɗo gooto, Gollorɗe kaalisiyaŋkooje leyɗeele men jaɓaani haalde e ko yowitii e daawal maa lajal nde ɗum foti waɗeede maa hollira golle potɗe waɗeede e nde poti waɗeede haa nde waylannde mawnde e maatiniinde waawa yuɓɓineede e siyneede kono kadi yimɓe fof ina nganndi eɓɓaande mawnde waynde nih ina hatojini ko ɓuri kormaagol toɓɓe tati kawraaɗe ɗe e kala faayiida mo ɗe mbaawi jogaade.
Eɓɓaannde waynde nih ina hatojini e ko famɗi fof :
• Ƴeewtaade ciifanɗe nanondire e sarɗiiji juɓɓinɗi hasbo kaalis ,huufo, yiilo e gollorɗe e ɗowgol pawingol e ko arata e nder sahaa lommbiiɗo etee mo tabitaani ;
• darnude e dañde terɗe e gollorɗe kese teeŋti noon e kawtal Bankiyaŋkeewal Leyɗeele -Kaleeteengal e ooɗo sahaa- mbaawkaaji laaɓtuɗi e kuutorɗe jumtuɗe jahduɗe heen e rewirde e kuutorɗe sarɗiyaŋkooje keɓtinaaɗe nuunɗuɗe e koolaaɗe ;
• lelnude e joofaade toɓɓanɗe ɗe dawrugol kaalisiyaŋkeewol joofi e dikkii,tawa ko baawooje renndude tuugannde wootere siynoore e nder taƴe fagguduyaŋkooje ceertuɗe e cariiɗe gonɗe e nder leyɗeele
• Suɓaade e dow paamondiral njuɓɓudi e kuutondiral e gostosndiral hakkunde kaalis o e kaalisaaji goɗɗi e mbaadi ɓurndi martobinndi e dow udditde dame e taƴe jahduɗe e ngonka ka Tippudi taƴƴaandi gostondiral ina waawi aaɓnaade e puɗɗe waɗte mbeytinaandi curaandi hade mum wontude e joofnirde tippudi mbellitaandi kuuɓtinaandi haa mbaawen yumtinde dawruɗi men fagguduyakooji e kaalisiyaŋkooji mawɗi
• Yoɓɓinde baylugol e lomtogol mbaadi e jelol kaliis CFA ( Ɗereeji e Jamɗe) wanta ɗi ECO,ekn .
Ɗe geɗe e caɗeele ko patamlame lugginɗe paayodinɗe jiiɓiiɗe e ina haawni e saɗi huuɓnude ɗe e nder hitaande 2020 tan Fotaani sabu Kiram paarnagol maa piitagol becce heñaade e yaawnude lomtino kaalis o e ndee hitaande 2020 Ɗe geɗe e caɗeele ko yummaaji potaani heñoraade haa diisnondire potɗe waɗeede heen ndañane safaara e nder piɓle kawraaɗe e dow kaaldigal jaajngal ɗe ɗum naamndi Ɗum ko ko yiɗa e muuya sabu e won sahaa e ɗum naamndi gaa rewirde e mbaawka fiilaaɓe Batirde Ngenndiire ( laamu laawɗinoowo) e ɗum noddi joɗoɗaade e haaldude e ɓesngu ngu maa jibinannde nde ngam heɓde miijooji mum e dow rewirde e fannu jahduɗo e ndiin mbaadi
E dow ɗum noon pitgol ngol potɗen fentude e kala mbaadi e njaru ko bonnitde ECO sabu ko Hooreejo Watara e yeeso Makaron Hoorejo farayse holliti kabaaru wonde leyɗeele UEMOA ( Dental fagguduyaŋkeewal e kaalisiyaŋkeewal Leyɗeele Hirnaange Afirik ) pellitii ƴeɓtude ECO yoo lomto CFA En potaani rufdude gawri mbesaandi e ñaande nde tiggu lottaaɗo rufdetaake e ndiyam ɗam
Eɗen poti siftorde wonde ƴeɓtugol ECO yoo lomto CFA wondude e doosɗe Kawrital Bankiyaŋkeewal e yamiroore CEDEAO ( Dental Fagguduyaŋkeewal ngam Ɓamtaare Leyɗeele Hirnaange AFIRIK ( DFƁLHA) wonde yoo leyɗeele keɓɗe sifaaji e maande hawrito yoo puɗɗo huutoraade Kaalis Denndaaɗo o adii haala e kabaaru mo Watara hokkiri o ñande 21 desammburu 2019. Ndeke noon keɓindo ɗen gila jooni eɓɓaande nde jokken e dow faandaare miijo Ardiiɓe CEDEAO ( Dental Fagguduyaŋkeewal ngam Ɓamtaare Leyɗeele Hirnaange AFIRIK ( DFƁLHA) ngam mbaawen e joofirgol yettaade faandaare yiɗaande woni Kaalis Denndaaɗo
Ndeen darnde ina yuwondiri e nde Leydi Gana jaɓndi e hollirndi weltaare mum ñande 28 Desammburu 2019 e yamiroore CEDEAO yowitiinde e ƴeɓtugol ECO e pellital mum ngam naatde heen Eɗum yahdi kadi e yamiroore CEDEAO ( Dental Fagguduyaŋkeewal ngam Ɓamtaare Leyɗeele Hirnaange AFIRIK ( DFƁLHA) ) e nder Batu Toowngu Hooreeɓe Leyɗeele 21 Desammburu 2019 njaaɓngu golle ardiiɓe UEMOA (Dental fagguduyaŋkeewal e kaalisiyaŋkeewal Leyɗeele Hirnaange Afirik) ƴeɓtuɓe ndeen yamiroore kolliri baylugol kaalis falnde e dental UEMOA ( Dental fagguduyaŋkeewal e kaalisiyaŋkeewal Leyɗeele Hirnaange Afirik) ina weeɓna e wallita, naatnaatondiral falnde nde e Dental kaalis e kopporeeje ngal ECO mo CEDEAO ( Dental Fagguduyaŋkeewal ngam Ɓamtaare Leyɗeele Hirnaange AFIRIK ( DFƁLHA) )
E dow ɗum, hay sinno muuyaande mawnde dental ina e men ngam yumtinde kaalis Denndaaɗo e nder bowal CEDEAO ( Dental Fagguduyaŋkeewal ngam Ɓamtaare Leyɗeele Hirnaange AFIRIK ( DFƁLHA) ) ɗum fotaani yejjitinde en wonde nafooje e paandaale men huccude e dawrugol kaalisiyanke e fagguyaŋke e tolno beccugol kaalis wonaa gooto
Ko ɗum waɗi nanondire hakkunde leyɗeele jeyaaɗe heen potaani fawaade e maslaha maa e ko tiiɗaani Kala jamirooje e gaddanɗe ƴeɓtaaɗe poti fawaade ko e gostondire hakkillaaji e jeewte luggiɗinaaɗe ɗe gooto fof yuurnitii haa faami ko waawi heen daañde e waasde
Ko mi neɗɗo ngooŋɗinɗo naatnaatondiral Afiriyaŋkeewal e no seeɗtorii ɗum humpitooji am e fannu liggeyeyaaji am e nder Baŋke Hirnaange Afirikiyaŋkeewo ngam ɓamtaare ( BHAƁ) maa e Senngo e goomuuji keeriiɗi afirikiyaŋkooji maa diiwaaniyaŋkooji e leyɗeele afirik funnaange maa hakkundeejo maa darnde am seeɗtinde e nder Banke AFirikiyaŋke ngam Ɓamtaare ( BAƁ) cosgol Booñ Firlito Jawdi Kopporeeje biyeteeɗo AFIRIKA 50 ngam wallitde peewnaandi tammbotoondi golle ɓamtaare e nder Ñiiɓirde Afirik Kono ɗum ittataa mboɗo jooɗtorii wonde won nafooje leyɗeele potɗe no feewi ƴeewteede e yuurniteede sabu majje seertude e luurondirnde alaa e sago yimɓe peewnitano jeewte e gostondire hakkillaaji e geɗe jiiɓiiɗe e heen sahaaji e ɗum noddi ballitgol e ceerndugol baawgol mettude e muusde haa boowal CEDEAO ( Dental Fagguduyaŋkeewal ngam Ɓamtaare Leyɗeele Hirnaange AFIRIK ( DFƁLHA) ) heddo e cañu mum fooɗta jaawdi naatoori e faggudu haa Kaalis keso o ECO waawa wallitde e no ɓuri yumtirde baylugol e ɓeydugol tiiɗnude gollorɗe e dente ngenndiije faggudu fayde e nafoore nde faami ɓesnguuji koɗɗi e nder CEDEAO ( Dental Fagguduyaŋkeewal ngam Ɓamtaare Leyɗeele Hirnaange AFIRIK ( DFƁLHA) ) Ɗum noddi ko semmbinde e tiiɗnude Kawtal e Dental leyɗeele tawa ɗum addaani heen ceeral e fawaare won heen leyɗeele.
KO ɗum waɗi gila e puɗɗe maa gila jooni leyɗeele UEMOA ( Dental fagguduyaŋkeewal e kaalisiyaŋkeewal Leyɗeele Hirnaange Afirik) ngonaa ɓoode wootere renndinnde leyɗeele jeetati jogiiɗe humpito e mbaawka maawka keɓaaka e BCEAO (Kawtal Banke leyɗeele Hirnaange AFIRIK) ngonaa waalaare huccunde e leydi Nigeria Ndoolnundi ngam jeemondiral ina aaɓno hono no leyɗeele Faraye e Allemaañ mbaɗiri e nder Dental orop (D O) e puɗɗe mum
Ko ɓuri yiɗeede so dañaama e yahrude e no Gana halliri ñande 28 Desammburu 2019 ndi tawta leyɗeele UEMOA (Dental fagguduyaŋkeewal e kaalisiyaŋkeewal Leyɗeele Hirnaange Afirik) mbele ngal dental ina waawa haɓɓondirde haalda e leydi Nigeria keewndi doole
Ko noon kadi ina hatojina e no waawata huutoreede doole semmbe e mbaawka goomuuji e pedle dillooɓe e dente renndooje haa ɗee keɓe mbaawi dañeede ɓe nawee e sara ardiiɓe leyɗeele CEDEAO ( Dental Fagguduyaŋkeewal ngam Ɓamtaare Leyɗeele Hirnaange AFIRIK ( DFƁLHA) ) mbele yiilo laamayru dawrugoliyaŋkeeru falnde men ina ɓura yaawde . Ko e on fannu tan waawi gaddeede e siyneede dawruɗi kaalisiyaŋkooji ɗi yontaaji garooji mbaawi ɗaldeede yoo kuuf e njiil haa kuutoro ECO.
Aamadu kan - Ganndo dowrowo fagguduKeeroriiɗo, fannu Kaalis e baŋke Woniino Jaagorgal, Ngalu e Faggugu e kopporeejo Ndanndaandi Senegaal
VERSION FRANÇAISE - L’ECO, LES EGOS ET LEURS ECHOS
Les décisions relatives au Franc CFA et à l’ECO, annoncées le 21 décembre 2019 à Abidjan par M. Alassane Ouattara, en sa qualité de président de la Conférence des chefs d’Etat de l’UEMOA et en présence du président de la République française sont incontestablement historiques.
Il n’est donc pas étonnant qu’elles aient été aussi médiatisées. Cependant, il est surprenant qu’en dépit des débats passionnés suscités par cette annonce, les questions que l’opinion se pose soient encore plus nombreuses que les préoccupations qui prévalaient avant l’annonce de cette réforme ! Et puis cette étrange impression que « tout change et… rien n’a changé ! ».
En effet, autant les mesures allant dans le sens du démantèlement des mécanismes de fonctionnement et de gestion du FCFA ont été clairement émises (changement d’appellation, clôture du compte d’opération, sortie des représentants de la France des instances de gouvernance de l’UEMOA), autant cette alternative à la monnaie actuelle reste pour le moins floue.
En outre, aucun des responsables des institutions monétaires de nos Etats n’a pu ou voulu indiquer un calendrier précis ou un chronogramme d’actions pour la concrétisation de cette réforme majeure. Et pourtant on sait qu’un projet de cette nature et de cette ampleur ne nécessite pas seulement le respect des trois critères de convergence aussi essentiels soient-ils !
Un tel projet nécessite à minima :
• de revisiter les traités et lois organisant la gestion de la monnaie, la gouvernance des institutions et le pilotage de leur devenir durant la phase intérimaire ;
• de doter les nouvelles institutions, en particulier la Banque Centrale Fédérale - dont il est question pour le moment -, de compétences adéquates et d’outils adaptés et les faire adopter à travers des instruments juridiques des plus crédibles ;
• de définir les cibles d’une politique monétaire qui puisse agir en dénominateur commun et qui soit opératoire dans les structures économiques variées et différentes de nos Etats respectifs ;
• d’arrêter de façon consensuelle le régime de change qui serait le plus optimal pour la zone avec la possibilité de procéder par un phasage des régimes. Ceux-ci pourraient être fixes au départ, « flexible encadré » par la suite et, pourquoi pas pour finir, si nous excellons dans nos politiques macro-économiques et financières, par un régime de flottement généralisé ;
• d’organiser le remplacement des signes monétaires CFA (billets et pièces) par les nouveaux signes monétaires ECO, etc..
Ces questions sont suffisamment sérieuses, importantes et complexes qu’il serait étonnant qu’on puisse achever de les discuter durant l’année 2020. Il ne faut pas, pour des questions d’ego, qu’on veuille précipiter la mise en place de la nouvelle monnaie en 2020. Ces problématiques sont tellement essentielles qu’il ne me paraît pas souhaitable d’expédier les concertations autour des sujets qu’elles soulèvent et des solutions consensuelles fortes qu’elles appellent. Et ce serait d’autant moins souhaitable qu’il y aurait certainement besoin, à des moments donnés du processus, en sus de la voie parlementaire, de consulter nos populations pour recueillir leurs avis de la façon la plus appropriée.
Dès lors, le piège que nous devrions éviter à tout prix serait de jeter l’opprobre sur l’ECO, du simple fait que ce serait le président Ouattara en présence du président Macron, qui aurait annoncé que les pays de l’UEMOA allaient l’adopter en substitution du FCFA ! Nous ne devrions pas « jeter le bébé avec l’eau du bain ! »
En effet, on doit se souvenir que l’adoption de l’ECO et du statut fédéral de sa Banque Centrale, l’accord donné par la CEDEAO aux pays répondant aux critères de convergence de démarrer l’aventure de la monnaie commune, sont autant de décisions antérieures aux annonces du 21 décembre 2019. Il faudra en conséquence s’approprier dès maintenant le projet et le poursuivre dans l’esprit originel des Autorités de la CEDEAO afin de parvenir, à terme, à la monnaie commune visée.
Une telle attitude est confortée par la position officielle du Ghana qui se réjouissait le 28 Décembre 2019 de la décision des Etats de l’UEMOA sur l’ECO et annonçait son intention de les rejoindre. Elle est également encouragée par la décision du Sommet des Chefs d’Etat de la CEDEAO du 21 Décembre 2019 qui en prenait acte et se félicitait de la décision de l’UEMOA en indiquant que cette « réforme de la zone monétaire de l’UEMOA facilitera son intégration dans la future zone monétaire ECO de la CEDEAO. »
Au demeurant, il ne faudrait pas que le fort désir d’union qui doit nous habiter pour réussir cette monnaie commune au niveau de la CEDEAO occulte le fait que nous n’avons pas tous et toujours les mêmes intérêts en matière de politique monétaire pro-active ou de fixation des taux de change.
C’est pour cela également que les discussions entre les Etats partenaires ne devraient pas conduire à des consensus mous. Les décisions et engagements arrêtés devraient résulter de négociations sérieuses et soutenues de telle sorte que chacun puisse évaluer et apprécier ce qu’il y gagne et ce qu’il y perd.
Je suis un partisan de l’intégration africaine comme peuvent en attester mes expériences professionnelles, que ce soit dans la fonction publique internationale à la BOAD, dans les organes de gouvernance de groupes privés panafricains en Afrique de l’Ouest et en Afrique Centrale ou encore à travers ma participation reconnue aux côtés de la BAD, dans la création du Fonds d’Investissement AFRICA 50 dédié aux financements des infrastructures sur tout le continent. Je n’en suis pas moins convaincu qu’il faut traiter sérieusement les intérêts, quelques fois divergents, des uns et des autres, se préparer à des discussions complexes et des arbitrages douloureux, afin que l’espace CEDEAO reste cohérent et attractif et que la nouvelle monnaie ECO participe efficacement à la transformation et au renforcement des diverses structures économiques nationales dans l’intérêt bien compris des populations de la CEDEAO. En définitive, il s’agit d’arriver à consolider la Communauté et non de satelliser certains Etats voire, pire encore, d’en vassaliser d’autres !
C’est pour cela qu’il est fondamental, dès le départ, qu’à côté du puissant Nigéria il y ait au moins un pôle soudé comme les huit anciens pays de l’UMOA – bénéficiant de la forte expertise et expérience de la BCEAO pour faire avancer, avec équilibre, la communauté à l’instar du rôle que jouèrent l’Allemagne et la France pour faire progresser l’Union Européenne à ses débuts.
Bien entendu la solution optimale serait, dans le sillage de son annonce du 28 Décembre 2019, que le Ghana accepte de rejoindre les pays de l’UEMOA au début de leur période ECO pour que ce nouveau bloc puisse mieux négocier avec le puissant Nigéria dans les mois à venir.
Il est tout aussi fondamental que l’énergie mise par tous les groupes d’acteurs sociaux pour arriver au résultat obtenu soit dorénavant positivement tournée vers les autorités des Etats de la CEDEAO pour accélérer l’unité de gouvernance politique de notre sous-région. Ce serait en effet la seule façon de garantir la parfaite application des politiques monétaires dévolues aux futures institutions centrales appelées à gérer l’ECO.
Amadou KANE, ancien Ministre de l’Économie et des Finances